Compositor: Não Disponível
Yaaay
Sama yaay yaay yaay boy
Yaaay
Sama yaay yaay yaay boy
Yow yaay yaay ki gën ci yaay yi
Di dabb sama baneex te dosi tay
Tuddu néñ lë ñenti yoon soga tudd bay yi
Sant nala gërëm nala yow yaay
Yar ñu, yor ñu, yé ñu
Mëso ci tay
Menuma baña nam sey jotaay
Mun moytu manlu sa musilay
Santé nala gërëm nala yow yaay
Bala ma menë wax yama doon wayal
Téy do wax maléy wayal
Rayal nala ten yaye dinala téral
Sant nala gërëm nala yow yaay
Maman, I love you so
Fi nga bëgg fofulay xole
Lala lalala
Yaay sama reinu xol
Té mangui jëgelu ci lima togg lu yaggë
Bëgg le té wonumala ko
Suma sañon man dotuma togg
Bëss gis la té waxumala ko yow yaay boy
Yaaay
Sama yaay yaay yaay boy
Maaa
Sant Yallah ndax loxo lama béral
Bu deson ci yow doma féral
Dara du la téy yaay boye démal
Mbida yidima jarama nénam
Yar ma, yor ma, yé ma (yémeu)
Dima xélal (xélal)
Wer ga wor ga sa xol nako séral (nako séral)
Maleyo maleyo yo malé nénam
Mbida yidima jarama nénam
Bala ma menë wax yama doon wayal
Téy do wax maléy wayal
Rayal nala teñ yaay dinala téral
Mbidda yidima jarama nénam
Maman, I love you so
Figa bëgg fofulay xole
Lala lalala
Yaay sama reini xol
Té mangui jëgelu ci lima togg lu yaggë
Bëgg le té wonumala ko
Suma sañon man dotuma togg
Bëss gis la té waxumala ko yow yaay boy