Compositor: Não Disponível
Maboo, oh oh
Baby, yeah
Baby namm na laa
Honey, yeah
Honey namm na laa
Sama xol ama sori
Dem nga daani doolé bayi maak wéétay
Yama dan mottali, banga démé la gëjj yëkk nééxay
Yaw yaa taxoon, ma bayi xarit yima am yepp
Té benn xarit, la désé woon té yaw la dem nga
Budoon ñént fukk att, dina ko tokk dila xaar
Yama fékk ci lëndëm, taalal may far léral sama yoon
Man rekk ci xalé, nammuma kudul Guisé Maabo
Kenn du yaw té yaafi mën, yaa mey jox li gën ci man
Baby I miss you
Yes I really do
Honey I miss you
How can I live without you?
Quand t’es loin de moi
Je ne vis pas
Je mourrais cent fois
Rien que pour être dans tes bras
Lima sori tax ma jaxaso
Wéetay moma tey kaso
Téléphone doyuma
Baby yaw namm na laa
Dama lay sentir, nga jégé té sori nga ma
Bul mérr, bul firr, gisuma fi kuma lay jënd
Lég-lég ma jum ndax tërëdi
Yaw kassé rekk ci xol dara xaju fi
Linga bëgg moy ma ñibi ci
Xamo ni mala gënn bëgg ñibi ci
Mbëgeel, kénn xamul lumuy
Def ci nitt bamuy, namel
Baby yaw suma la mënoon indi fi kenn waxatu ko
Quand t’es loin de moi
Je ne vis pas
Je mourrais cent fois
Rien que pour être dans tes bras
Baby I miss you
Yes I really do
Honey I miss you
How can I live without you?
Toucouleur bu rafet bangi ni, hé
Boroom nag ak mééw bangi ni
Hééé yamay danel
Daggma nammoon mangi ni
Namm la tax man ma ñibi ci
Dagg ma nammoon mangi ni
Namm la tax man ma ñibi ci
Hé, hé, hé, hé, hé! Diobadio arri!
Toucouleur bu rafet bangi ni
Hé, hé, hé, hé, hé! Diobadio arri!
Boroom nag ak mew bangi ni
Hé, hé, hé, hé, hé!
Toucouleur bu rafet bangi ni
Hé, hé, hé, hé, hé!
Boroom nag ak mew bangi ni