Nabi

Maabo

Compositor: Não Disponível

Mouhamadu rassoulilah
Mouhamadu rassoulilah

Dass naa sama baat
Fas yéene di la tagg
Kañ a leen ma Moustapha
(Mouhamadu rassoulilah)
Séy naa ci di la kañ
Ahmada jar a kañ
Kañaleen ma Moustapha
(Mouhamadu rassoulilah)

Mooy Nabi
Yaa rassoulilah mooy Nabi
(Mouhamadu rassoulilah)
Mooy nabi
Yaa rassoulilah mooy Nabi
(Mouhamadu rassoulilah)

Mooy Ahmad Hamir, Bachiru Bachi
Mu chabile Moustapha
(Mouhamadu rassoulilah)
Mooy sànge bi fi gën te sànge du ko gën
Tayu xasi mbër yi maay Moustapha
(Mouhamadul rassoulilah)
Waa ma ka way nañu ko ma dina feruleen
Alhoustaral Moustapha
(Mouhamadu rassoulilah)
Li dundal sama ruu ba leeral jëm jee
Nataal sama xol ci Moustapha
(Mouhamadu rassoulilah)
Suñu boroom julli na aki malaykam
(Mouhamadu rassoulilah)
Waay ku li adjidame, war nga sax di julli ci
(Mouhamadu rassoulilah)

Dass naa sama batt
Fass yéné di la tagg
Kaña leen ma Moustapha
(Mouhamadu rassoulilah)
Seye na ci dila kañ
Axmada jara kañ
Kañaleen ma Moustapha
(Mouhamadu rassoulilah)

Mooy nabi
Ya rassoulilah mooy nabi
(Mouhamadu rassoulilah)
Mooy nabi
Ya rassoulilah mooy nabi
(Mouhamadu rassoulilah)

Fii ko fi joxe sa yaakaar
Moom Nabi la yaakaar
Baayu Fatuma mooy
(Mouhamadu rassoulilah)
Sant nañu Moustapha
Lakku nañu ci Moustapha
Kuy saku walu billaay dawal ci
(Mouhamadu rassoulilah)
Man amuma feneen fu ma jëm ci ku dul
(Mouhamadu rassoulilah)
Wuutuma feneen fu ma jëm ci ku dul
(Mouhamadu rassoulilah)
Man dajj naa li ma doon wër
(Mouhamadu rassoulilah)
Wuuti leeru gën gi mindeef mi eee
(Mouhamadu rassoulilah)

Dass naa sama batt
Fass yéné di la tagg
Kaña leen ma Moustapha
(Mouhamadu rassoulilah)
Seye na ci dila kañ
Ahmada jara kañ
Kañaleen ma Moustapha
(Mouhamadu rassoulilah)

Nabi!
Bi ñu ma dompté tamite damp nga ma
Nabi!
Bi ma wété loolu nga wétalli ma

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital