Kuma Nop

Maabo

Compositor: Não Disponível

Ku ma nob, laaj ma ku ma nob
Sama saajoobaan
Ku ma nob, laajleen ma ku ma nob man
Sama saajoobaan
Su ma doon orchestre, mooy sama guitar bass
Yaw yaa tax sol dal neex, yaay sama kawas yeh
Sama saajoobaan!

Yaw laay woo wuyu ma waruñu di réero
Waxal ak man te nga ree
Wax ma ku la tooñ bëgguma ku lay merloo
Waxal ak man te nga ree
Sa kanam bi nga fas ni ñemetuma la ni
Maay wax ngay biñ, di ma xeloo ni
Amatuloo sama kersa yaw mi (déedéet)
Lu fi jaar ba nga bëgg mel ni (fokk ma mel ni)
Wax ma lu la dal ba nga may tontu ni (lépp ci yaw la)
Kon ma lay merloo ni

Li nga fokk la, laaj ma lu ma naam (loo naam wax ma)
Fi ma tollu ni, maa ngi sama oh là là!
Man jekk piir, wax ma loo fi manqué
Fi maay First Lady, kenn du ma jamm na ne

Iyo, iyo
Waaaw
Iyo, iyo
Yaa di sama saajoobaan
Iyo, iyo
Yaay ki may motelee
Iyo, iyo

Ku ma nob, laaj ma ku ma nob
Sama saajoobaan
Ku ma nob, laajleen ma ku ma nob man
Sama saajoobaan
Su ma doon orchestre, mooy sama guitar bass
Yaw yaa tax sol dal neex, yaay sama kawas yeh
Sama saajoobaan!

Yaw lan la, sonn naa léegi may ma
Demetul noonu mak yaw
Wowowowoy bàyyi ma
Mettiwoon na te demuma
Lépp laa muñ ca ba muy metti
Dimbali ma, wax ma lu la yëkkëti
Wuyoooy, bàyyi ma!
Ñaareel nga fi bëgg takk
Waxoo fi dara lu leer ñaareel nga fi bëgg takk, hey!

Niarél ngafi bëgg takk
Waxofi dara lu lerr nirél ngafi bëgg takk hey

Li nga fokk la, laaj ma lu ma naam (loo naam wax ma)
Fi ma tollu ni, maa ngi sama oh là là!
Man jekk piir, wax ma loo fi manqué
Fi maay First Lady, kenn du ma jamm na ne

Iyo, iyo
Waaaw
Iyo, iyo
Yaa di sama saajoobaan
Iyo, iyo
Yaay ki may motelee
Iyo, iyo

Ku ma nob, laaj ma ku ma nob
Sama saajoobaan
Ku ma nob, laajleen ma ku ma nob man
Sama saajoobaan
Su ma doon orchestre, mooy sama guitar bass
Yaw yaa tax sol dal neex, yaay sama kawas yeh
Sama saajoobaan!

Ku ma nob, laaj ma ku ma nob
Laajleen ma ku ma nob man

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital